Nehemiah 12:35 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Lenni sarxalkat yaa nga ca topp aki liit, di ñi ànd ak Sàkkaryaa doomu Yonatan. Yonatan, Semaya mooy baayam; Semaya, Mataña di baayam, Mataña, Mikaya mooy baayam; Mikaya, Sakuur ay baayam; Sakuur, Asaf mooy baayam.