Nehemiah 2:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba mu ko defee, Sanbalat ma dëkk Oron dégg mbir ma, mook Tobya, Amoneen ba, ndawal Buur. Ñu am lu leen soofa soof, te mooy li nit ñëw, di sàkkusi njariñu bànni Israyil.