Nehemiah 2:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw loolu ma jóg guddi, maak nit ñu néew, te waxuma kenn li ma sama Yàlla nammloo ngir ma defal ko Yerusalem. Yoruma woon jenn daamar ju moy ji ma war.