Nehemiah 2:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Buur nag wax ak man, fekk Lingeer soxnaam toog, feggook moom. Mu ne ma: «Boo demee, ana loo fay toog, doora délsi?» Ma wax ko. Gannaaw loolu Buur nangu maa bàyyi ma dem.