Nehemiah 2:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu ma ne Buur: «Buur, su la soobee, ngalla nañu ma jox ay bataaxal yu jëm ca kilifay Wàllaa Dex ya, ngir ñu jàllale ma, ba ma àgg Yuda;