Nehemiah 3:17 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Leween ñaa ca topp di defaraat, di Reyum doomu Baani; ka dend ak moom, taxawal goxam di defaraat, di Asabya, may boroom genn-wàllu gox ba ñuy wax Keyla.