Nehemiah 3:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ka feggook moom di liggéey, Eser la, doomu Yeswa, boroom Mispa. Muy defaraat làcc wa janook fa ngay yéege jëm ca dencu gànnaay ya, ca koñu tata ja.