Nehemiah 3:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ka feggook ñoom, ba tey, di defar di waa Tekowa. Seeni kilifa nag ñoo bañoona liggéey ci njiital jawriñ yi yore liggéey bi.