Nehemiah 3:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ña feggook ñoom di defar, di Melatiya ma dëkk Gabawon ak Yadon ma dëkk Meronot ak ñeneen waa Gabawon ak Mispa, gox ya ca kilifteefu boroom Wàllaa Dex.