Nehemiah 3:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ka feggook ñoom di defar, di Usyel doomu Xaraya, tëggu wurus ba. Ka feggook moom di defar, di Anaña, bokk ca defarkati cuuraay ya. Ñu sottal seen liggéey ca Yerusalem gannaaw ba ñu àggee fa tata ja gëna yaatoo.