Nehemiah 4:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Sanbalat nag ak Tobyaak Araab yaak Amoneen ñaak Asdoddeen ña, ñoom ñépp dégg ne liggéeyu tatay Yerusalem a ngay jëm kanam, te xar-xar yaa ngay tàmbalee fatt. Ñu mer ca lool,