Nehemiah 4:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
La ko dale bésub keroog sama xaaju nit ña rekk a doon liggéey, xaaj ba ca des gànnaayoo ay xeej aki pakk aki fitt ak kiiraayal dënn. Kilifa ya nag taxaw ca gannaaw mboolem waa Yuda.