Nehemiah 4:17 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Booba kenn ci nun summiwul ay yéreem, du man, du samay bokk, du samay nit, te du wattukat yi ànd ak man. Ku nekk day ŋàbb ngànnaayam akam ndox.