Nehemiah 4:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba mu ko defee nu ñaan ci sunu Yàlla, ba noppi teg fa ay nit ñuy wattu guddeek bëccëg, ngir bàyyi leen xel.