Nehemiah 5:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Man itam, maak samay bokk ak samay nit, nu ngi lebal askan wi xaalis ak pepp. Waaye nanu leen baal bor bii.