Nehemiah 5:16 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xanaa kay damaa saxoo jàpp ci liggéeyu tata jii. Masunoo jënd suuf, te sama nit ñépp a daan daje ci liggéey bi.