Nehemiah 5:17 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Rax ci dolli daan naa woo téeméeri kilifay Yawut ak juróom fukk (150), di bokk ak ñoom sama njël, te limaalewuma ñi bàyyikoo ci jaambur yi nu séq, di nu fekksi.