bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Nehemiah 5:18
Nehemiah 5:18 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bés bu nekk daan nañu ma waajalal aw yëkk, ak juróom benni xari yar, ak boroomi dunq, ak lu baree bare ci mboolem xeetu biiñ, ñu di ko indi fukki fan yu nekk. Loolu taxul ma sàkku benn yoon galag bu boroom diiwaan di dunde, ndax liggéey bi diisoon na lool jeeg ci askan wi.