Nehemiah 6:18 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bare na sax ci waa Yuda ñu faroon ak moom ci kaw ngiñ, ndax la mu doon denc doomu Sekaña, ma Ara di baayam, te doomam Yowanan di denc doomu Mesulam ma Berekiya di baayam.