Nehemiah 7:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Sama Yàlla xiir ma ma woo garmi yeek kilifa yeek baadoolo yi, ngir bind leen. Ci biir loolu ma gis limeefu làng ya jëkka jóge ngàllo ga, ba ñibbsi. Li ma fekk ñu bind ko ci mooy lii: