Nehemiah 9:26 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Waaye dégguñu ndigal, xanaa di la gàntal. Dañoo sànni saw yoon seen gannaaw; sa yonent ya leen doon xiirtal ci délsi ci yaw, ñu rey leen, ba ñàkke la kersa lool.