Numbers 10:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su ñu liitee riirum liit mu xumb, ñaareel bi yoon, dal yi dale bëj-saalum ñooy fabu. Riirum liit mu xumb mooy tegtale seeni fabu.