Numbers 10:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Bu loolu wéyee, bu ngeen dee xare ci seenum réew, ak noon bu leen songsi, nangeen riiral liit yi riir mu xumb, su boobaa dees na leen bàyyi xel fa seen kanam Yàlla Aji Sax ji, ba wallu leen ak seeni noon.