Numbers 13:20 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ak suuf sa: ndax nangu na, am nanguwul; ak itam ndax am nay garab, am déet. Te ngeen góor-góorlu ba sàkkaale ca meññeefi réew ma.» Fan yooyu nag yemook reseñ di meññ ndoortel meññeef.