Numbers 13:32 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci biir loolu ñuy baatal ca kanam bànni Israyil, réew ma ñu nemmikuji woon. Ñu naan: «Réew moomee ñu wëri woon ngir nemmiku ko déy, réew la muy faagaagal ay sancaanam, te mboolem askan wa nu fa gis, ay boroom jëmm lañu.