Numbers 15:27 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su dee kenn nit a bàkkaar te du teyeefam, na sarxal aw bëy wu jigéen wu menn at, ngir saraxu póotum bàkkaar.