Numbers 15:30 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nit ki tooñ cig teyeefam nag, muy njuddu-ji-réew, di doxandéem, kooku Aji Sax ji la ñàkke kersa. Nit kooku, dees koy dagge ci biiri bokkam: