Numbers 16:28 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Musaa nag ne: «Lii nag moo leen di xamal ne Aji Sax ji moo ma yebal ngir ma def jëf jii jépp, waaye du sama coobarey bopp: