Numbers 18:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Leneen lu la ñeel moo di jooxe bu jóge ci saraxi nit ñi, di bépp saraxu yékkati-jébbal bu bànni Israyil. Yaw laa ko sédd, yaak sa doom yu góor, ak sa doom yu jigéen, ci kaw dogalu yoon bu sax dàkk. Képp ku set ci sa waa kër, sañ na cee lekk.