Numbers 18:30 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Waxal Leween ñi ne leen gannaaw bu ñu ca génnee céru ngëneel li, li ci des lew na leen, ni bu doon pepp mu jóge ci seen dàggay bopp, ak biiñ bu jóge ci seen nalukaay.