Numbers 19:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Lii mooy dogalu yoon bi Aji Sax ji santaane: Neleen bànni Israyil ñu indil leen nag wu jigéen wu xonq, wu mat, mucc sikk, te kenn masu koo takk,