Numbers 21:24 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Israyil leel ko ñawkay saamar, nangu seenum réew, dale ko Arnon ba Yabog, ba àgg ca Amoneen ña, ndax kemu réewum Amoneen ñaa fegu woon ba jotuwul.