Numbers 21:4 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu bàyyikoo tundu Or, jubal yoonu géeju Barax ya, ngir teggi réewum Edom. Mbooloo ma nag mujj xàddi ca yoon wa.