Numbers 22:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nag dikkal gaaw ñaanal ma yàlla gàngoor gii, ngir ñoo ma ëpp doole. Jombul ma duma leen, ba dàq leen réew mi, ndax xam naa ne koo ñaanal, mu barkeel, te koo ñaan-yàlla, mu alku.»