Numbers 23:17 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu dem ba ca moom, fekku ko lu moy mu taxaw ca wetu saraxu rendi-dóomalam, mook kàngami Mowab. Balag ne ko: «Lu Aji Sax ji wax?»