Numbers 26:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Musaa ak Elasar sarxalkat ba wax ak ñoom ca joori Mowab, fa janook Yeriko ca wetu dexu Yurdan; ñu ne leen