Numbers 26:58 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñii itam ci làngi Leween lañu: làngu Libneen ñi, ak làngu Ebroneen ñi, ak làngu Maaleen ñi, ak làngu Museen ñi, ak làngu Korayeen ñi. Keyat nag mooy maamu Amram;