Numbers 27:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su baayam amul góor gu mu bokkal waajur, mbokkam mu ko gëna jege ci biir làngam, moom ngeen di jox céru suufam. Kookooy donn cér ba. Na loolu di dogalu yoon, ñeel bànni Israyil, noonu ko Aji Sax ji sante Musaa.”»