Numbers 28:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ak benn fukkeelu efab sunguf su mucc ayib, di ñetti kilo, muy saraxu pepp, ñu tooyale ko ag diw, booleek xar mu ci nekk. Saraxu rendi-dóomal la, ngir xetug jàmm, di saraxu sawara, ñeel Aji Sax ji.