Numbers 30:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye su ko baayam aayee, ca bés ba mu ca déggee, su boobaa mboolem xasi ndaw si, ak mboolem dogu ya mu doguloon boppam, du sax, te Aji Sax jee koy jéggal, ndax baayam aaye woon na ko.