Numbers 35:30 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Képp ku faat bakkan nag, ci kaw kàddu gu tukkee ci ay seede doŋŋ lees ko saña reye, moom ma rey, waaye bennub seede du seedeel nit, ngir ñu teg ko àtteb dee.