Numbers 35:4 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Parluy dëkk yi ngeen di jox Leween ñi, ci miiru dëkk ya lay dale, jëm biti lu day ni junniy xasab, yemook juróomi téeméeri meetar, ci wet gu nekk.