Numbers 35:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dëkk yi ngeen di jox Leween ñi, ñoo di juróom benni dëkki rawtu, yi ku rey nit mana raweji, ak yeneen ñeent fukki dëkk ak ñaar yu ngeen leen ciy dollil.