Numbers 36:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu wéyee kilifay njaboot yi askanoo ci Yuusufa, te bokk ci làngu Galàdd doomu Makir mi sëtoo ci Manase, ñoo dikk. Ñu wax fa kanam Musaa, ak kilifay njabooti bànni Israyil.