Numbers 36:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye bu ñu séyee ci yeneen giiri bànni Israyil de, seen céru suuf mooy wàññikoo ci sunu céru maam, dolliku ca céru giir ga ñu séyi ca seen biir, te kon cér ba nu tegoo woon bant moo cay wàññikoo.