Numbers 36:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mboolem ku jigéen ku donn suuf ci giiri bànni Israyil, ci biir làng gu bokk ci giirug maamam rekk lay séy, ngir ku nekk ci bànni Israyil mana ñoŋal céru maamam.