Numbers 5:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Fii la sarxalkat biy waatloo ndaw si waatu alkànde gi, wax ko ne ko: “...yal na la Aji Sax ji def ku alku ku ñuy móoloo ci sa biir askan. Yal na laxal sa njurukaay, wal sab koll.