Numbers 6:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Dogalu yoon wi ci ab nasireen nag mooy lii: Bés bi ag céddoom matee, dees koy yóbbu ca bunt xaymab ndaje ma.