Numbers 6:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Baayam ak ndeyam, mbaa góor mbaa jigéen ju mu bokkal waajur sax, bu deeyee, du sobeel boppam ngir ñoom, ndax moo yenu ci kaw boppam, njañu nasireen gi mu séddoo Yàllaam.