Numbers 8:17 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax man maa séddoo mboolem taaw ci biir bànni Israyil, nit ak mala. Keroog ba ma fàddee mboolem taaw ca réewum Misra, ca laa leen sellalal sama bopp.